Lyrics
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Bik na lol si yo
Tek na le si ko
Nop na seji ko
Tef saar lo dul ye
Gudi gudi yay sama bitté
Sama way sama lingé
Bugu ma dina je di goudé
Dama lay sorry di wé
Yow mi ma doy lo
Mondou ma tef lu lay joy lo
Baby xam nga xam na
Adia lou ma si nobody
Xam nga xam na
Bébé baby dina si daw badé
Djong nga ngar yaru té ma ndu checké té
Nga di kéne sima ndu ña ndu ñett
Mondina tef li moula gis la ngi bik
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Gudi gudi yay sama bitté
Sama way sama lingé
Bugu ma dina je di goudé
Dama lay sorry di wé
Dama xala to soré
Wayé xel bi dou diou simo
Allou mbégué la soré
Wayé fa mara re bé wo
Yon bi goudou nay
Buri jam jam xam na si tara
Mbégué la gata
Téré de kono bé
Capitalo béta
Abé si tyo sé
Tié nga bayi mo
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Gudi gudi yay sama bitté
Sama way sama lingé
Bugu ma dina je di goudé
Dama lay sorry di wé
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Bik na lol si yo
Tek na le si ko
Nop na seji ko
Tef saar lo dul ye
Gudi gudi yay sama bitté
Sama way sama lingé
Bugu ma dina je di goudé
Dama lay sorry di wé
Yow mi ma doy lo
Mondou ma tef lu lay joy lo
Baby xam nga xam na
Adia lou ma si nobody
Xam nga xam na
Bébé baby dina si daw badé
Djong nga ngar yaru té ma ndu checké té
Nga di kéne sima ndu ña ndu ñett
Mondina tef li moula gis la ngi bik
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Gudi gudi yay sama bitté
Sama way sama lingé
Bugu ma dina je di goudé
Dama lay sorry di wé
Dama xala to soré
Wayé xel bi dou diou simo
Allou mbégué la soré
Wayé fa mara re bé wo
Yon bi goudou nay
Buri jam jam xam na si tara
Mbégué la gata
Téré de kono bé
Capitalo béta
Abé si tyo sé
Tié nga bayi mo
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma
Gudi gudi yay sama bitté
Sama way sama lingé
Bugu ma dina je di goudé
Dama lay sorry di wé
Ya may gungue ya may dundal
Ya mani wone
Yow la xol bi dilla
Ya yeli doné la w sima
Oh mona ne
Sa yoyé wo gis ma